Dans ce contexte de bataille idéologique et de guerre d'opinions, TOUBA doit jouer pleinement et entièrement son rôle. Dans le milieu Islamique d'abord puis de façon beaucoup plus vague et élargie. Une époque de dispute, de contradiction, de compétition déloyale et d'opposition, l'héritier légitime de MOUHAMADOU, en l'occurence AHMADOU doit apporter sa contribution qui, sans nul doute, demeure la plus attendue et la plus salvatrice. Conscient des enjeux, l'honorable calif de TOUBA a entrepris, sachant que le savoir est la meilleure arme pour s'imposer dans ce contexte particulier de détournement et d'égarement, de bâtir une université à la dimension de TOUBA et de son illustre fondateur. Ceci prouve à suffisance le don inestimable et le legs incontestable qu'ALLAH(ltp) a bien voulu accorder à AHMADOU, le noble héritier de MOUHAMADOU. Que DIEU lui prête encore bien des années dans cette vie terrestre tout en lui accordant pleine santé et succès total dans cette entreprise et toutes les autres qu'il a entrepris ou qu'il aura entrepris par considération pour AHMADOU, amen. dieureudieuf AHMADOU.
machllh na ndawi Touba yéb dem diangui si Université bi inchallah j'aimerais voir un Touba exemplaires dans le monde islamique inchallah un Ville modèle un Ville qui tient te propre autonome. Dan tt le domaine vive Touba vive le Sénégal vive la mouridis n'a nn yi gna sonn rkk inchallah 😆
Machallah S TOUBA AMOUL morom
Ak lou none yi mana wakhe soul gaz douco très khengni yonou mouride sa kaw sa kanam rk dieuredief khadim Rassoul kene la
اطال الله عمرك ياخليفة الإسلام مع الصحة والعافية
Amnasolo loool dieredief yalna sunuborom mottali yéénéyép Serigne mountakha yagfi loool téwér amiiine
Macha Allah
❤️❤️❤️❤️❤️😘😘😘
Dans ce contexte de bataille idéologique et de guerre d'opinions, TOUBA doit jouer pleinement et entièrement son rôle. Dans le milieu Islamique d'abord puis de façon beaucoup plus vague et élargie. Une époque de dispute, de contradiction, de compétition déloyale et d'opposition, l'héritier légitime de MOUHAMADOU, en l'occurence AHMADOU doit apporter sa contribution qui, sans nul doute, demeure la plus attendue et la plus salvatrice. Conscient des enjeux, l'honorable calif de TOUBA a entrepris, sachant que le savoir est la meilleure arme pour s'imposer dans ce contexte particulier de détournement et d'égarement, de bâtir une université à la dimension de TOUBA et de son illustre fondateur. Ceci prouve à suffisance le don inestimable et le legs incontestable qu'ALLAH(ltp) a bien voulu accorder à AHMADOU, le noble héritier de MOUHAMADOU. Que DIEU lui prête encore bien des années dans cette vie terrestre tout en lui accordant pleine santé et succès total dans cette entreprise et toutes les autres qu'il a entrepris ou qu'il aura entrepris par considération pour AHMADOU, amen. dieureudieuf AHMADOU.
Serigne Touba kéne la, ndiabootamitt kéne la niou. Dieuredieuf AHMADOU.
yalla na yalla takhawolen si barck serigne touba amatina sólo Machallah
Hakaza
Sama xol sed na trop
machallah dieureudieuf mbacke balla yalna ge fi yagui te werr barkep serigne touba
Serigne Mountakha Mbacké yalna fi yagg lol té wérr barké borom TOUBA Amine
Amine
A♥️🤲
Hakaza
بارك الله فيكم
machllh na ndawi Touba yéb dem diangui si Université bi inchallah j'aimerais voir un Touba exemplaires dans le monde islamique inchallah un Ville modèle un Ville qui tient te propre autonome. Dan tt le domaine vive Touba vive le Sénégal vive la mouridis n'a nn yi gna sonn rkk inchallah 😆
Dieureudieuf Serigne Touba
Merci pour vous tous
Wa goora Mouride thia kaw thia kanam rek in cha Allahou, Barkep CHEIKHOUNA Ahmadou Bamba
Ni rèk la yone bi meussa teudé bou nite ngi di wakh niouye dieuf tè ande ak noppi taye dèglou ndigal rèk
NANIOU XARR BAXAM YALLA DI FAYYE WAKH DI BAYYI DIEUF REK…
MACHALAH MBACKE MBALLA YAGUAL WERRAL REK MOUY GUANA NEKH REK BA ALDIANA REK🙏🙏🙏
Mahcalla
Xam Xam. Rk.moamsolo
Macha Allahou . Yalla Nafi Serigne Mountakha Bachir Al Khalifa Yague Té Were Bi Barakatoul khadimou Rassoul Amine
Machala Cheikh Mouhamadou Al Mountakha Mbacké Yalla nafi yague lolou t ande ak weer
Li rek mo meunna gueuna jarigne yonn wi, aprés guén tambaali projet industrie bou touba inchagod
Yague fi loll Ta wer Mbacke
Serigne mountaha yala nafi yagg lol ak were
Vive la Révolution👉 idéologie de cheikh Ahmadou Bamba Khadimou rassoul ✨AL MOUNTAKHA YAGUE YOKOU WERR 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Machallah alHamdoulillah ❤️
Machahala amna solo lool xam xam dafa Am Solo lool thi islam
Machalla mbacké
Yalnaniou SERIGNE BI liggeey Looo
Dieureudieuf Cheikhol khadim Amolmorom
ماشاء الله 💚💚💚
Mbacke yaram gena yagge gena wer gena yokku bubaxx Ba léppou Yégge TA GAN fékke léppou mbacke sounu xolll sédde na sun xell Dallna
Sante yalla sunu borom sante Serigne bi
Bilahi li rek moye diné khol sedna thiaye Serigne touba
Une belle et pertinente réplique à ces mouridophobes qui nous traitent de fanatiques. Top ndigel rek
الحمد لله
Machalah mbacke
Yallah n'a yallah angalé sen yénè guen andeko Ak S Mountakh Ak dioulét yi Ak talibé yép barke S touba